Daaraj family - COSAAN (visualizer)

Details
Title | Daaraj family - COSAAN (visualizer) |
Author | Daaraj Family |
Duration | 3:13 |
File Format | MP3 / MP4 |
Original URL | https://youtube.com/watch?v=SQ_pi-njedA |
Description
Stream Cosaan : https://bfan.link/cosaan
Crédits de la chanson et du visualizer :
Stylisme et Direction Artistique - @sellyrabykane
Video (editing) : im_abdou_aziz
Photographie - @nrknmb
Asst.Photo : @fhemy.raw
Set Design - @cheikha_sigil / Ibrahima Sow @thekaaksociety / Ameth Diaw
Costumes - Selly Raby Kane x Mohamed Diouf x Cheikh Cissokho
Glam x Beauty Team: @mariemengom_ , Ndeye Diakhou Marone
Mobilier et textiles: DIOM et Aïssa Dione tissus
Artwork : @pigoldcapture
Régie : @laythiammm
Management : @seydounourougueye
Direction Exécutive : @diengmerou
Musique : @tche_officiel X Daaraj Family
Arrangements, Mix et Mastering : Tche on The Beat
Act :
Femme Cosaan : @oumymariediallo
enfants Cosaan : Malick et Hassan Sall
The mask : @napoleontsar
____________________
COSAAN LYRICS
REFRAIN:
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fàtte , bul fàtte
Fa nga cosaanoo !!
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fàtte , bul fàtte
Fa nga cosaanoo !!
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fàtte , bul fàtte
Fa nga cosaanoo !!
addina ag li ci biir
Bo demee ba am ko
Bul fàtte , bul fàtte
Fa nga cosaanoo !!
Couplet Faada :
Xam na nu fi nu jogee
Li nu jaxal moy funu jëm de
suufu maam yi moom bu nu woowe
Du nu tànqamlu du nu soree
danuy fatu numu gëna gaawe
Ñun ndawu Reew mi da nu pare
Ji fi luy jëriñ fi ak fë le
Ba ñu ñu ci dara ku ngemboy bëre
wër naa addunaa
Japon Inde Australia
There is no place like home
Fen du Sunugaal
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo
Couplet Ndongo :
Ku fi fàtte demb
ëlëg dalay reer
Waxu mag la degg nga
Du am kubeer
fattëlikul ki nga doon , fi nga juddoo
Fi nga juggee,fi nga dëkk Yalla mi la bindd
Ngor, jom, fit la ,fayda booko amul
doo xam fi nga jëm dara du ku dinddi
Li ci Baay bi di doom na ko jëli
Kaddu mag ñi nii na ko sët yi firri
Na nu gëna disoo ndax ñu mëna deggoo
xana giso jikkoo yi ni gëna yàqoo
Na nu dellu te toogi mëna root du doy di
adduna ngi daw di na ñu def ci bop yi
Bul di fatte ñi la fàl ñi la tettewoon
Ñi la gunge bi ngay raam ñi nga nekkaloon
Lakoon fakoon ñakoon
Lawoon fawoon ñawoon
Xaleel poto poto la
Noko raaxe rek lay weyee
Fi laa yaroo fi laa maggee
Lumu guddi guddi guddi damay ñibbee
Galsen moy daw sunu dereet
dañu wutiwoon ba tax ñu ne bëreet
Teranga yi ñi fay jëlee su nu askan lañkoy jëmee
wër naa addunaa
Japon Inde Australia
There is no place like home
Fen du Sunugaal
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo
Fa nga cosaanoo
#music #daaraj #cosaan #senegal #demb #Galsen #ngoyane #thiossane